Mane ci sama bop khawma louma beugeu
(Mane khawma louma beugue)
Bi gniy nieukeu dadjé bobou
(Bobou wakhoumala deugue)
Kouma kham di nga thiéné fi nga thiéné
(Di nga thiéné fi nga thiéné)
Sama bopp la ley nieukeu téré
(Sama bopp la ley nieukeu téré)
Boul meusseu geum samay texto
Boul meusseu nagou niouy wéto
Mane douma fay damay leb ndaw
Boul meusseu geum samay texto oh
Boul meusseu nagou niouy wéto oh
Doumala diokh li ngay weur
Boul ma wolou ndax wakhouma
Sai Sai la moytouma moytouma héé
Ma geuneu méti Al-Qaida hhaa
Sai Sai la moytouma moytouma héé
Soma tidjilé sa nopp nala doff lo
Douma ko tey soumay nope lo
Soma tidjilé sa bopp di nga of loo yeah
Damay daw somay wane love
Ndax beugouma kouma beugue dima topato héy
Somay khar or shore ma ngui Offshore hey
Boul meusseu geum samay texto
Boul meusseu nagou niouy wéto
Mane douma fay damay leb ndaw
Boul meusseu geum samay texto oh
Boul meusseu nagou niouy wéto oh
Doumala diokh li ngay weur
Boul ma wolou ndax wakhouma
Sai Sai la moytouma moytouma héé
Ma geuneu méti Al-Qaida hhaa
Sai Sai la moytouma moytouma héé
Xol bi dagn ci warone collé stap sine
Gnatta la fi digone dékhou banékh
Si guedjou rongogne deh lagn modié lape gayne
Dama leuthi dama dioubadi
Sho déh nala teuthi si say souvenir
Au début da ngey bégue fok ni douma nite
Tay bo sagnone doma freq doma meusseu mine
Yague na di wakh ci goor youy fowé xolou guel
Tané woma kone meunouma té role’ou frère
Guisna sa kite kou tass yakar tégou yoonu jail
Dou dégati kén néla doundeul bo ci tolouwé
To tolouwé dou dégati ken
Do gégeuti néla doundeul bo ci tolouwé